Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 3

Sabóor 3:5-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Maay woo Aji Sax ji wall, mu walloo ma fa tundam wu sell wa. Selaw.
6Maay tëdd nelaw, yewwu; Aji Sax ji di ma aar.
7Ñu dul jeex a ma jógal, gaw ma, te duma ragal.
8Éy Aji Sax ji sama Yàlla, jógal, wallu ma! Yaa toj kaabaabi noon yu bon yépp, foq seeni sell.

Read Sabóor 3Sabóor 3
Compare Sabóor 3:5-8Sabóor 3:5-8