Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 34

Sabóor 34:7-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Néew-ji-doole woote, Aji Sax ji wuyu, musal ko fu mu jàqe.
8Ku ragal Aji Sax ji, malaakaam yiir la, di la wallu.

Read Sabóor 34Sabóor 34
Compare Sabóor 34:7-8Sabóor 34:7-8