Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 34:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 34:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Néew-ji-doole woote, Aji Sax ji wuyu, musal ko fu mu jàqe.
8 Ku ragal Aji Sax ji, malaakaam yiir la, di la wallu.
Sabóor 34 in Kàddug Yàlla gi