Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 33

Sabóor 33:8-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Yeen waa àddina sépp, ragal-leen Aji Sax ji; yeen àddina wërngal këpp, wormaal-leen ko.
9Moo àddu, mu am; santaane, mu sotti.
10Aji Sax jeey neenal li xeet yiy fexe, di gàntal li mbooloo yiy mébét;

Read Sabóor 33Sabóor 33
Compare Sabóor 33:8-10Sabóor 33:8-10