Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 33:8-10 in Wolof

Help us?

Sabóor 33:8-10 in Kàddug Yàlla gi

8 Yeen waa àddina sépp, ragal-leen Aji Sax ji; yeen àddina wërngal këpp, wormaal-leen ko.
9 Moo àddu, mu am; santaane, mu sotti.
10 Aji Sax jeey neenal li xeet yiy fexe, di gàntal li mbooloo yiy mébét;
Sabóor 33 in Kàddug Yàlla gi