Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 33

Sabóor 33:7-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Moo boole ndoxi géej, jal, yeb xóotey géej ciy mbànd.
8Yeen waa àddina sépp, ragal-leen Aji Sax ji; yeen àddina wërngal këpp, wormaal-leen ko.

Read Sabóor 33Sabóor 33
Compare Sabóor 33:7-8Sabóor 33:7-8