Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 33:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 33:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Moo boole ndoxi géej, jal, yeb xóotey géej ciy mbànd.
8 Yeen waa àddina sépp, ragal-leen Aji Sax ji; yeen àddina wërngal këpp, wormaal-leen ko.
Sabóor 33 in Kàddug Yàlla gi