Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 33

Sabóor 33:19-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Day jot bakkanam, di ko dundal cib xiif.
20Nu ngi séentu Aji Sax ji, moo nuy taxawu, di nu feg.
21Ci moom la sunu xol di sedde, turam wu sell lanu wóolu.

Read Sabóor 33Sabóor 33
Compare Sabóor 33:19-21Sabóor 33:19-21