Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 33:19-21 in Wolof

Help us?

Sabóor 33:19-21 in Kàddug Yàlla gi

19 Day jot bakkanam, di ko dundal cib xiif.
20 Nu ngi séentu Aji Sax ji, moo nuy taxawu, di nu feg.
21 Ci moom la sunu xol di sedde, turam wu sell lanu wóolu.
Sabóor 33 in Kàddug Yàlla gi