Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 33

Sabóor 33:14-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Jal ba mu tooge lay niire waa àddina sépp.
15Moo tabax seen xol, ñoom ñépp; lu ñu def, xam na ko.
16Mbooloo mu réy mayul Buur ndam, doole ju bare walluwul jàmbaar.

Read Sabóor 33Sabóor 33
Compare Sabóor 33:14-16Sabóor 33:14-16