Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 33:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 33:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Jal ba mu tooge lay niire waa àddina sépp.
15 Moo tabax seen xol, ñoom ñépp; lu ñu def, xam na ko.
16 Mbooloo mu réy mayul Buur ndam, doole ju bare walluwul jàmbaar.
Sabóor 33 in Kàddug Yàlla gi