Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 31

Sabóor 31:23-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
23Man nag saalitoon naa ne: «Yàlla dagg na ma, sànni!» Ndeke ba ma lay woo, dégg nga samay dagaan.
24Képp kuy aji gëm, soppal Aji Sax ji. Aji Sax jeey sàmm ku ko gëm, di yool, ba wis kuy réy-réylu.

Read Sabóor 31Sabóor 31
Compare Sabóor 31:23-24Sabóor 31:23-24