Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 31

Sabóor 31:19-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Yal nanga tëj gémmiñu fen-kat buy wax aji jub waxi reewande, di réy-réylook a xeebaate.
20Yàlla yaa yaa ngëneel loo dencal ku la ragal, defal ko ku la làqoo, doom aadama seede.

Read Sabóor 31Sabóor 31
Compare Sabóor 31:19-20Sabóor 31:19-20