Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 31:19-20 in Wolof

Help us?

Sabóor 31:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 Yal nanga tëj gémmiñu fen-kat buy wax aji jub waxi reewande, di réy-réylook a xeebaate.
20 Yàlla yaa yaa ngëneel loo dencal ku la ragal, defal ko ku la làqoo, doom aadama seede.
Sabóor 31 in Kàddug Yàlla gi