Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 30

Sabóor 30:5-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Yeen aji gëm ñi, woyleen Aji Sax ji, njukkale ko sellngaam.
6Meram di lu gàtt, aw yiwam sax dàkk. Rongooñ gane, fanaan, ay ree xëysi.
7Man damaa baaxle woon, ba ne: «Deesu ma rëññeel mukk.»

Read Sabóor 30Sabóor 30
Compare Sabóor 30:5-7Sabóor 30:5-7