Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 2

Sabóor 2:7-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Buur ne: «Ma biral dogalu Aji Sax ji, moom mi ma ne: “Yaa di sama doom, bés niki tey, maa la jur.
8Ñaan ma xeeti àddina, ma sédd la ko, nga moom ba ca cati àddina,

Read Sabóor 2Sabóor 2
Compare Sabóor 2:7-8Sabóor 2:7-8