Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 2:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 2:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Buur ne: «Ma biral dogalu Aji Sax ji, moom mi ma ne: “Yaa di sama doom, bés niki tey, maa la jur.
8 Ñaan ma xeeti àddina, ma sédd la ko, nga moom ba ca cati àddina,
Sabóor 2 in Kàddug Yàlla gi