Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 2

Sabóor 2:3-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Ña nga naan: «Nanu dagg càllala yi, sànni jéng yi!»
4Ki ci jalub asamaan a ngay ree, Boroom baa nga leen di kókkali,
5mer, ba gëdd leen, xadaru, tiital leen ne:
6«Man maa tabb buur, fal ko ci Siyoŋ, sama tund wu sell.»

Read Sabóor 2Sabóor 2
Compare Sabóor 2:3-6Sabóor 2:3-6