Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 2:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 2:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Ña nga naan: «Nanu dagg càllala yi, sànni jéng yi!»
4 Ki ci jalub asamaan a ngay ree, Boroom baa nga leen di kókkali,
5 mer, ba gëdd leen, xadaru, tiital leen ne:
6 «Man maa tabb buur, fal ko ci Siyoŋ, sama tund wu sell.»
Sabóor 2 in Kàddug Yàlla gi