Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 28

Sabóor 28:4-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Fey leen seen liggéey, seen kemu jëf ju bon. Jox leen seen añu jëf, yool leen seen yelleef.
5Xooluñu Aji Sax jeeki jëfam, ak liggéey bi mu def. Da leen di yàqte, te dootu leen yékkati.

Read Sabóor 28Sabóor 28
Compare Sabóor 28:4-5Sabóor 28:4-5