Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 28:4-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 28:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 Fey leen seen liggéey, seen kemu jëf ju bon. Jox leen seen añu jëf, yool leen seen yelleef.
5 Xooluñu Aji Sax jeeki jëfam, ak liggéey bi mu def. Da leen di yàqte, te dootu leen yékkati.
Sabóor 28 in Kàddug Yàlla gi