Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 26

Sabóor 26:2-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Aji Sax ji, nattu ma, seetlu ma, seggal xel ak xol.
3Maa ngi janook sa ngor, di jëfe sa worma.
4Toogumaak naxekat, lëngoowumaak naaféq,
5sib naa gàngooru saaysaay, toogumaak ku bon.
6Aji Sax ji, maay jàpp ci biir mucc ayib, di wër sa sarxalukaay,

Read Sabóor 26Sabóor 26
Compare Sabóor 26:2-6Sabóor 26:2-6