Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 25

Sabóor 25:19-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Xoolal noon yi ne gàññ, bañ ma mbañeelu fitna.
20Éy, aar ma, musal ma! Bu ma rusloo, yaw laa làqoo.
21Yal na ma maanduteek njub taxawu, maa ngii, di la xaar.

Read Sabóor 25Sabóor 25
Compare Sabóor 25:19-21Sabóor 25:19-21