Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 25:19-21 in Wolof

Help us?

Sabóor 25:19-21 in Kàddug Yàlla gi

19 Xoolal noon yi ne gàññ, bañ ma mbañeelu fitna.
20 Éy, aar ma, musal ma! Bu ma rusloo, yaw laa làqoo.
21 Yal na ma maanduteek njub taxawu, maa ngii, di la xaar.
Sabóor 25 in Kàddug Yàlla gi