Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 22

Sabóor 22:22-23

Help us?
Click on verse(s) to share them!
22Musal ma ci pàddum gaynde ak ndañum nagu àll. Yaa ma wallu woon!
23Ma siiwali saw tur ci bokk yi, màggale la digg mbooloo mi.

Read Sabóor 22Sabóor 22
Compare Sabóor 22:22-23Sabóor 22:22-23