Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 22:22-23 in Wolof

Help us?

Sabóor 22:22-23 in Kàddug Yàlla gi

22 Musal ma ci pàddum gaynde ak ndañum nagu àll. Yaa ma wallu woon!
23 Ma siiwali saw tur ci bokk yi, màggale la digg mbooloo mi.
Sabóor 22 in Kàddug Yàlla gi