Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 22

Sabóor 22:16-18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
16Làmmiñ taqoo denqleñ, doole jeex, ma wow koŋŋ, nga tëral ma buntu bàmmeel.
17Ay xaj a ma wër, di gàngooru saaysaay, dar ma kepp, bëtt samay yoxook samay tànk.
18Maa ngii, mana waññ sama yax yépp, ñoom ñuy xoole, di ma seetaan,

Read Sabóor 22Sabóor 22
Compare Sabóor 22:16-18Sabóor 22:16-18