Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 22:16-18 in Wolof

Help us?

Sabóor 22:16-18 in Kàddug Yàlla gi

16 Làmmiñ taqoo denqleñ, doole jeex, ma wow koŋŋ, nga tëral ma buntu bàmmeel.
17 Ay xaj a ma wër, di gàngooru saaysaay, dar ma kepp, bëtt samay yoxook samay tànk.
18 Maa ngii, mana waññ sama yax yépp, ñoom ñuy xoole, di ma seetaan,
Sabóor 22 in Kàddug Yàlla gi