Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 20

Sabóor 20:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Aji Sax jeey musal ki mu fal, bir na ma tey. Moo koy nangule fa asamaan su sell sa, ci dooley ndijooram biy musle.
8Ñiiki watiir, ñeeki fas, nun sunu turu Yàlla Aji Sax ji lanuy tudd.
9Ñoom ñooy jeng ak a jóoru, nun, nu jóg, taxaw jonn.

Read Sabóor 20Sabóor 20
Compare Sabóor 20:7-9Sabóor 20:7-9