Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 20:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 20:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Aji Sax jeey musal ki mu fal, bir na ma tey. Moo koy nangule fa asamaan su sell sa, ci dooley ndijooram biy musle.
8 Ñiiki watiir, ñeeki fas, nun sunu turu Yàlla Aji Sax ji lanuy tudd.
9 Ñoom ñooy jeng ak a jóoru, nun, nu jóg, taxaw jonn.
Sabóor 20 in Kàddug Yàlla gi