Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 19

Sabóor 19:9-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9Lu Aji Sax ji tegtale, njub la, di bégal xol. Lu Aji Sax ji santaane, leeraange la, di leeral gis-gis.
10Santaaneb ragal Aji Sax ji mooy li sell te sax ba fàww. Lu Aji Sax ji digle, dëgg la, ak njekk gu sotti.

Read Sabóor 19Sabóor 19
Compare Sabóor 19:9-10Sabóor 19:9-10