Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 17

Sabóor 17:3-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Natt nga saab xol, niir ma guddi, settantal ma, gisoo dara. Dogu naa ne duma moye wax.
4Su may jëf it, di sàmm sa kàddu. Maay moyu yoonu ku bon.
5Sa tànk, sama tànk, jàdduma fenn.
6Éy Yàlla, maa lay woo, nga di ma wuyu; teewlu ma te déglu ma!

Read Sabóor 17Sabóor 17
Compare Sabóor 17:3-6Sabóor 17:3-6