Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 16

Sabóor 16:8-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Damaa saxoo ne jàkk ci Aji Sax ji ndijoor la ma fare, ba duma tërëf,
9xanaa di bànneexu, sama xol bég, sama yaram finaax.
10Doo ma wacc njaniiw moos, sa wóllëre wa, doo ko won yàqutey bàmmeel.

Read Sabóor 16Sabóor 16
Compare Sabóor 16:8-10Sabóor 16:8-10