Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 149

Sabóor 149:8-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8yeewe seeni buur ay càllala, jénge seeni njiit jéngi weñ,
9ngir sottalal leen àtte bi ñu bind, muy ndamu wóllërey Yàlla yépp. Màggal-leen Ki Sax!

Read Sabóor 149Sabóor 149
Compare Sabóor 149:8-9Sabóor 149:8-9