Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 149:8-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 149:8-9 in Kàddug Yàlla gi

8 yeewe seeni buur ay càllala, jénge seeni njiit jéngi weñ,
9 ngir sottalal leen àtte bi ñu bind, muy ndamu wóllërey Yàlla yépp. Màggal-leen Ki Sax!
Sabóor 149 in Kàddug Yàlla gi