Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 147

Sabóor 147:3-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3di faj naqaru xol, fajtal góomi boroom.
4Mooy lim biddiiw yi, tudd bu ci nekk.
5Sunu Boroom a màgg, bare doole; am xelam wees kemu.
6Aji Sax ji, néew-ji-doole, mu yenni; ku bon, mu daane ci suuf.

Read Sabóor 147Sabóor 147
Compare Sabóor 147:3-6Sabóor 147:3-6