Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 147

Sabóor 147:2-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Aji Sax jaa ngi tabaxaat Yerusalem, di délloosi ña ñu dàqe Israyil,
3di faj naqaru xol, fajtal góomi boroom.

Read Sabóor 147Sabóor 147
Compare Sabóor 147:2-3Sabóor 147:2-3