Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 147

Sabóor 147:19-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Mooy wax Yanqóoba kàddoom, dogalam yaak ndigali yoonam ñeel Israyil.
20Loolu defalu ko wenn xeet; kenn xamu ci ndigali yoonam. Màggal-leen Ki Sax!

Read Sabóor 147Sabóor 147
Compare Sabóor 147:19-20Sabóor 147:19-20