Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 147:19-20 in Wolof

Help us?

Sabóor 147:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 Mooy wax Yanqóoba kàddoom, dogalam yaak ndigali yoonam ñeel Israyil.
20 Loolu defalu ko wenn xeet; kenn xamu ci ndigali yoonam. Màggal-leen Ki Sax!
Sabóor 147 in Kàddug Yàlla gi