Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 141

Sabóor 141:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Ni ñuy gàbbe suuf ba mu ne ŋafeet, ni la njaniiw di ŋaye, aw seeni yax yu tasaaroo.
8Aji Sax ji Boroom bi, yaw laa wékki gët, yaw laa làqoo, bu ma seetaan, ma dee.
9Musal ma ci yeer yi ñu ma gasal, ak fiir yi ma defkati ñaawtéef yi tegal.

Read Sabóor 141Sabóor 141
Compare Sabóor 141:7-9Sabóor 141:7-9