Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 140

Sabóor 140:12-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Kuy yàq der, yàlla bumu toog ci réew mi. Nitu fitna, yal na ko ay topp, ba dal ci kawam.
13Xam naa ne Aji Sax jeey jox néew-ji-doole dëgg; di sàmm àqu baadoolo.

Read Sabóor 140Sabóor 140
Compare Sabóor 140:12-13Sabóor 140:12-13