Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 13

Sabóor 13:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3ba ma tàggook bopp bu ubu ak njàqarey xol bu sax, ba noon dootu ma man?
4Céy Aji Sax ji sama Yàlla, geesu ma, wuyu ma, leqli ma, bala ma ne sërëx ci nelawi ndee,
5noon ba naan: «Daan naa ko,» bañ yay bége saab jéll.

Read Sabóor 13Sabóor 13
Compare Sabóor 13:3-5Sabóor 13:3-5