Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 137

Sabóor 137:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Aji Sax ji, fàttlikul Edomeen ña, keroog jantub Yerusalem, ba ñu naan: «Màbbleena màbb, ba kenug dëkk bi siiñ!»
8Yeen waa Babilon, gi ñu nara fàllas, ndokklee ku leen fey jëf, ja ngeen nu def!
9Ndokklee ku ne cas seeni fere, tas ciw doj!

Read Sabóor 137Sabóor 137
Compare Sabóor 137:7-9Sabóor 137:7-9