Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 137:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 137:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Aji Sax ji, fàttlikul Edomeen ña, keroog jantub Yerusalem, ba ñu naan: «Màbbleena màbb, ba kenug dëkk bi siiñ!»
8 Yeen waa Babilon, gi ñu nara fàllas, ndokklee ku leen fey jëf, ja ngeen nu def!
9 Ndokklee ku ne cas seeni fere, tas ciw doj!
Sabóor 137 in Kàddug Yàlla gi