Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 135

Sabóor 135:19-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Éey waa kër Israyil, santleen Aji Sax ji! Éey waa kër Aaróona, santleen Aji Sax ji!
20Éey waa kër Lewi, santleen Aji Sax ji! Yeen ñi ragal Aji Sax ji, santleen Aji Sax ji!
21Nañuy sante Aji Sax ji Siyoŋ, moom mi dëkke Yerusalem. Màggal-leen Ki Sax!

Read Sabóor 135Sabóor 135
Compare Sabóor 135:19-21Sabóor 135:19-21