Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 135

Sabóor 135:13-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Aji Sax ji, sa tur ba fàww; Aji Sax ji, sa woy a saxal maasoo maas.
14Aji Sax ji kay ay àtte ñoñam ñi, di ñeewante jaamam ñi.
15Tuuri yéefar yi, xaalis ak wurus, loxoo ko sàkk.
16Am gémmiñ te du wax, ami gët te du gis,

Read Sabóor 135Sabóor 135
Compare Sabóor 135:13-16Sabóor 135:13-16