Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 129

Sabóor 129:1-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Muy jàngi yéeg, ñu di ko màggale Yàlla. Ba may ndaw ba tey, ñu ngi may sonala sonal. Israyiloo, waxati ko:
2Ba may ndaw ba tey, ñu ngi may sonala sonal, te taxul ñu man ma.
3Sama gannaaw gi lañu gàbba gàbb, rëdd koo rëdd nib tool.

Read Sabóor 129Sabóor 129
Compare Sabóor 129:1-3Sabóor 129:1-3