Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 129:1-3 in Wolof

Help us?

Sabóor 129:1-3 in Kàddug Yàlla gi

1 Muy jàngi yéeg, ñu di ko màggale Yàlla. Ba may ndaw ba tey, ñu ngi may sonala sonal. Israyiloo, waxati ko:
2 Ba may ndaw ba tey, ñu ngi may sonala sonal, te taxul ñu man ma.
3 Sama gannaaw gi lañu gàbba gàbb, rëdd koo rëdd nib tool.
Sabóor 129 in Kàddug Yàlla gi