Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 128

Sabóor 128:4-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Ki ragal Aji Sax jaa ngoog, nii rekk lay barkeele.
5Yal na la Yàlla barkeele fii ci Siyoŋ; yal nanga teewe xéewalu Yerusalem sa giiru dund gépp,

Read Sabóor 128Sabóor 128
Compare Sabóor 128:4-5Sabóor 128:4-5