Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 128:4-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 128:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 Ki ragal Aji Sax jaa ngoog, nii rekk lay barkeele.
5 Yal na la Yàlla barkeele fii ci Siyoŋ; yal nanga teewe xéewalu Yerusalem sa giiru dund gépp,
Sabóor 128 in Kàddug Yàlla gi